
Mon Caramel, Mon Chocolat
papedjiby niang
Made with HeartMuLa
Make a song like this
Turn a name, a memory or your own lyrics into a song in a few minutes.
Prompt
Mmh… mon caramel… Mmh… mon chocolat… (Soupir doux) [Couplet 1 - Intime, voix posée sur le piano] Sama xol dafa xëy, di la wëër, Sa xol xëy, di ma wëër… Waral ñu gise, mbëggel bu doy waar te neex, Juddu ci boobu gise… Bu telefone sonnee, ku nekk di wax sa moroom… [Refrain 1 - Entrée des violons, la voix s'ouvre avec chaleur] Oh Mère, mon caramel, yoo lele… Oh Amë Bass, mon chocolat, yoo lele… Oh Mère, mon caramel, yoo lele… Oh Amë Bass, mon chocolat, yoo lele… [Couplet 2 - Plus rythmé, entrée d'une batterie douce et de la basse] Dama ni couple heureux, yoo lele, Woy bi yaa ko moom, yoo lele, Woy bi yeeyoo, yeeyoo nga ko, yoo lele, Ndax sa mbëggel gu dëggu… Oh, kontaan naa ci mbëggel bu neex bi, Oh, lii yàlla bumu jeex… mmh… Bu telefone sonnee, ku nekk di wax sa moroom… [Refrain 2 - Plus intense, avec des chœurs en arrière-plan] Oh Mère, mon caramel, yoo lele… Oh Amë Bass, mon chocolat, yoo lele… Oh Mère, mon caramel, yoo lele… Oh Amë Bass, mon chocolat, yoo lele… [Pont 1 - Montée dramatique, voix puissante, ambiance grand concert] Uzi, mbëggelu mére jallo, mmh, mbëggel gënu ko neex… mmh ! Ndeye Wuli, mbëggelu Amë bas, mmh, mbëggel gënu ko neex… mmh ! Biinz, mbëggelu mére jallo , mmh, mbëggel gënu ko daxu … mmh ! Kumba Daado, mbëggelu Amë bas, mmh, mbëggel gënu ko wóor… mmh ! [Pont 2 - Solennel, presque a cappella avant l'explosion finale, plein de fierté] Dama ni, dama ni… Sagal nga Amë Bass, han Mère Diallo ! Jàppale nga Amë Bass, han Mère Diallo ! Yërëm nga Amë Bass, han Mère Diallo ! Sutural nga Amë Bass, han Mère Diallo ! (Les tambours et l'orchestre montent en crescendo) Waral tey Amë Bass yónnee premier cadeau, Fas yéene fësël seen fiançailles, Di ñaan bés bu sell, bés bu mag bi agsi, Bañu takk sëy bi, alxayri bi jipp, Mbëggel gi tàmbali yokku… (Note tenue très haut !) [Refrain Final - Explosion orchestrale, voix pleine puissance et ad-libs] Bu telefone sonnee, ku nekk di wax sa moroom ! Oh Mère, mon caramel, yoo lele ! (Yoo lele, mon amour !) Oh Amë Bass, mon chocolat, yoo lele ! (Mon chocolat, yoo lele !) Oh Mère, mon caramel, yoo lele ! Oh Amë Bass, mon chocolat, yoo lele ! [Outro - Retour au piano seul, voix douce et pleine de tendresse] Bu telefone sonnee… ku nekk di wax sa moroom… Oh Mère… mon caramel… Oh Amë Bass… mon chocolat… (Dernière note de piano qui s'éteint doucement) Yoo lele… mmh…